John 16:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu nag ngeen di jàqe, yéen itam. Waaye dinaa leen gisaat, seeni xol sedd, te seen mbég moomu, kenn du ko man a dindi.