John 16:30 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Léegi gis nanu ne, xam nga lépp, te soxlawul kenn di la laaj dara. Looloo tax nu xam ne, yaa ngi jóge ci Yàlla.»