John 17:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Jottali naa leen sa kàddu, te àddina bañ leen, ndax li ñu mel ni man, bañ a bokk ci àddina soosu.