John 17:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Damay ñaan ngir ñépp doon benn. Baay, na ñooñu nekk benn ci nun, ni nga nekke ci man te ma nekke ko ci yaw. Nañu ànd, ba àddina gëm ne, yaa ma yónni.