John 17:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Man ci ñoom, yaw it ci man, ngir ñu gën a ànd, nekk benn, ba àddina xam ne yaa ma yónni, xam ne bëgg nga leen, ni nga ma bëgge.