John 17:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñoom laay ñaanal. Ñaanaluma waa àddina, waaye maa ngi ñaanal ñi nga ma dénk, ndaxte ci yaw lañu bokk.