John 18:29 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Looloo tax Pilaat boroom réew ma génn, dajeek ñoom. Mu laaj leen ne: «Lu ngeen di jiiñ waa jii?»