John 18:36 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu tontu: «Sama kilifteef nekkul ci àddina. Bu sama kilifteef nekkoon àddina, sama surga yi dinañu xeex, ngir bañ ñu jébbal ma Yawut yi. Waaye sama kilifteef nekkul àddina.»