John 18:37 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Pilaat ne ko: «Kon yaw buur nga?» Yeesu tontu ko: «Wax nga ko; buur laa. Lii moo tax ma juddu, ñëw àddina: ngir wax dëgg gi. Ku bokk ci dëgg dina nangu li ma wax.»