John 18:40 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ñu daldi yuuxuwaat: «Déedéet, waxunu kii; Barabas lanu wax!» Fekk Barabas moomu taskatu réew la woon.