John 19:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Pilaat ne ko: «Man ngay bañ a waxal? Xanaa xamuloo ne, am naa sañ-sañu bàyyi la, te am naa itam sañ-sañu daaj la ci bant?»