John 19:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu ci boppam gàddu bant ba, génn ngir dem ca fa ñuy wax Bérabu kaaŋu bopp; ñu koy wooye Golgota ci làkku yawut.