John 19:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ca wetu bant, ba ñu daajoon Yeesu, yaayam a nga fa taxawoon, moom ak doomu ndeyam ju jigéen, Maryaama jabari Këlópas, ak Maryaama mi dëkk Magdala.