John 19:28 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi loolu wéyee gannaaw Yeesu xam na ne, lépp mat na léegi, mu ne nag, ngir amal Mbind mi: «Damaa mar.»