John 19:35 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Kiy nettali mbir yooyu, da cee teg bëtam, te li muy wax dëgg la. Moom ci boppam xam na ne, li muy wax dëgg la, ngir yéen itam ngeen gëm,