John 19:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Pilaat génnaat ne leen: «Gis ngeen, maa ngi leen koy indil ci biti, ngir ngeen xam ne, waa jii, gisuma ci moom genn tooñ.»