John 20:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi mu waxee loolu, mu geestu, séen Yeesu mu taxaw, waaye xamul woon ne moom la.