John 3:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci dëgg-dëgg maa ngi la koy wax, noo ngi wax li nu xam, di nettali li nu gis, waaye nanguwuleen a gëm li nu seede.