John 3:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Te itam na Musaa sampe woon ab bant ca diggu màndiŋ ma, takk ca jaan, ja mu defare woon xànjar, fàww ñu yékkatee noonu Doomu nit ki,