John 3:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci nii la àtte bi ame: leer gi ñëw na ci àddina, waaye nit lëndëm gi lañu taamu ndax seeni jëf yu bon.