John 3:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ku def lu jub day ñëw ci leer gi, ngir ñu xam ne, def na ay jëfam ci kanam Yàlla.