John 3:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw loolu Yeesu ànd ak ay taalibeem, dem ca biir diiwaanu Yude, toog fa ak ñoom ab diir, di sóob nit ñi ci ndox.