John 4:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu nag Yeesu tontu ko: «Soo xamoon li Yàlla maye, xam ki lay ñaan ndox, kon yaw ci sa bopp, yaa koy ñaan, te moom dina la may ndoxum dund.»