John 4:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yéen waa Samari, xamuleen li ngeen di jaamu. Nun Yawut yi, xam nanu li nuy jaamu, ndaxte kiy musal àddina ci Yawut yi la jóge.