John 5:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
looloo tax ba Yawut ya daldi ne nit ku wér ka: «Tey bésu noflaay la, te sunu yoon aaye na, ngay yor sa basaŋ.»