John 5:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye waa ji xamul ki ko wéral, fekk booba Yeesu dem na, te nit ñu bare teewoon nañu ca bérab ba.