John 5:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte Baay bi bëgg na Doom ji, ba di ko won lépp lu muy def, te dina ko won jëf yu ëpp kéemaan yii, ngir ngeen gën a waaru.