John 5:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
ngir ñépp di teral Doom ji, ni ñuy terale Baay bi. Ku teralul Doom ji, teraloo Baay, bi ko yónni.