John 5:36 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
«Waaye yor naa ci man seede su gën a mag si ma Yaxya di seedeel: maa ngi def jëf, yi ma Baay biy sant. Jëf yooyu may def nag ñooy seede ne, Baay bi moo ma yónni.