John 5:37 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Te Baay bi ma yónni, moom itam seede na ma. Musuleen a dégg baatam te musuleen a gis xar-kanamam,