John 5:44 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bëgg ngeen ku leen di tagg, te wutuleen ngërëm, li jóge ci jenn Yàlla rekk ji am. Kon nan ngeen man a gëme?