John 5:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ko Yeesu séenee mu tëdd, te mu xam ne, woppam ji yàggoon na lool, mu laaj ko ne: «Ndax bëgg ngaa wér?»