John 6:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi nit ña gisee firnde jooju Yeesu wone, ñu ne: «Dëgg-dëgg kii mooy Yonent, bi war a ñëw ci àddina!»