John 6:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ñu joowee lu war a tollook juróom benni kilomet, ñu séen Yeesu, muy dox ci kaw dex gi, jëm ci ñoom, ñu daldi tiit.