John 6:38 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte wàccewuma ci asamaan ngir def sama bëgg-bëgg, waaye damay matal bëgg-bëggu ki ma yónni.