John 6:39 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Lii mooy bëgg-bëggu ki ma yónni: bu ma ñàkk kenn ci ñi mu ma may, te dafa bëgg it ma dekkal leen keroog bés bu mujj ba.