John 6:45 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yonent yi bind nañu kàddu gii: “Yàlla dina leen jàngal ñoom ñépp.” Kon nag ku déglu te nangu waxi Baay bi, dina ñëw ci man.