John 6:57 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Baay bi ma yónni mu ngi dund, te maa ngi dund jaarale ko ci moom; noonu itam ku may lekk dina dund jaarale ko ci man.