John 6:71 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yudaa miy doomu Simoŋ Iskariyo la doon wax. Ndeke Yudaa, la muy bokk lépp ca fukki taalibe ya ak ñaar, moo ko naroon a wor.