John 7:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ku fas yéenee wéy ci bëgg-bëggu Yàlla, dina xam ndax sama njàngale ci Yàlla la jóge, walla ci sama coobare.