John 7:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Nit kiy wax ci coobareem nag, day wut a màggal boppam, waaye kiy wut a màggal ki ko yónni, dëgg rekk lay wax te jubadiwul fenn.