John 7:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Xanaa du Musaa moo leen jox ndigali Yàlla yi? Waaye kenn ci yéen sàmmu ko! Lu tax ngeen bëgg maa rey?»