John 7:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Xool-leen, mi ngi waaraate ci biir nit ñi, te kenn du ko wax dara. Ndax sunu kilifa yi dañoo xam ne, mooy Almasi bi?