John 7:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu rakki Yeesu yu góor ya ne ko: «Jóge fi te dem diiwaanu Yude, ngir say taalibe gis, ñoom itam, jaloore yi ngay def.