John 7:41 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñeneen naan: «Mooy Almasi bi.» Ña ca des it ne: «Waaye nan la Almasi bi man a jógee Galile?