John 7:52 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñu tontu ko ne: «Mbaa du yaw itam dangaa bokk ci diiwaanu Galile? Gëstul, kon dinga xam ne, benn yonent musul a jóge Galile.»