John 8:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu dellu ne leen: «Maa ngi dem; dingeen ma seet, waaye seen bàkkaar ngeen di deeyaale. Fa ma jëm, dungeen fa man a dem.»