John 8:37 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Xam naa ne askanu Ibraayma ngeen. Waaye yéena ngi may wut a rey, ndaxte li may jàngale xajul ci yéen.