John 8:41 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Li ngeen donne ci seen baay rekk ngeen di def.» Ñu tontu ko ne: «Nun de, dunu doomi araam. Benn baay rekk lanu am, mooy Yàlla.»