John 8:54 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu ne leen: «Su ma dee màggal sama bopp, du am maana. Sama Baay a may màggal, moom mi ngeen naan, mooy seen Yàlla.